WATIT
- Écrire une critique
Watit
Ba mu wëraalee àddina si ba noppi, Felwiin Saar dellusi na Afrig gi mu juddoo, indaale ay kaddu yu mu yëkkati jeme leen ci ndawi askanam. Ci biir nettali gi muy nettali mbooru kembaar gi dale ko ci njalbéenam, dafay ñaax doomi Afrig yépp ngir ñu féetalewaat seen xar-kanam ci jant bi, fexe ba jotaat seen péexte ak seen ngor, saxal jéego yi ñuy teg, dox yaatal seen yoon.
Ci Tubaab la Felwiin Saar bind téere bii, tudde ko Traces, Fehe Saar tekki ko ci Wolof.
<<Watit, téere la bu Felwiin Saar bind ci nasaraan,
tudde ko Traces, Fehe Saar tekki ko ci Wolof.>>
Téere bii mi ngi génn ci ndimbalu sàqu jàpple móol ci Njawriñu Mbatiit. Njiteefu Téereek Dawal.
La qualité du produit est garantie par L'Harmattan Sénégal
Ce livre peut être récupéré en magasin ou livré à domicile.
Le retour se fait directement en magasin. Merci de contacter le SAV : +221 33 825 98 58